|
|
 |
listu xabaar ak xew xew yi mujju téñu gëstuko |
 |
|
|
|
|
 |
ligéey yi ak yenggu yenggu yi |
 |
|
|
|
Bismillaxi raxmaani raxiimi
|
|
iiknaa asbuntu léerla bu ubéeku jem ci aduna bi yep |
laltaay:
Kёru tasukaayu xabaar yi jёm ñi al xur'aan té néek iran mooy kёr gu njekk buñu jagléel tas xabaaru al xur'aan yi si aduna bi yep.bes bu yaala saak dañi góórgóórlu ba xabaar yidi xéwée ñi iran ak aduna bi yep moo xam ñi waalu politique wala caada wala aada wala dundine wala yeggu yeggu yi jёm ñi al xur'aan wala xalaat ak xam xam ak blog bitim réew ñu farañe faañéko ñi gis gisu al xur'aan.
taariix ñi tёkk:
Kёru tasukaayu xabaar yi jem ci waalu al xur'aan (iiknaa)ñukko sos ñi atum 1423 ñi gaadaay gi toombéek fukku ak juroom ñi wéeru koor ñi téewaayu njiitu réewu iran ci jamono jooju.ligéeykatu (iiknaa) ak ñiko yitéwoo ci nimbelu yaala ak gindéeko ci al xur'aan ak toope ndigël imaam xoméynii ak njiitu revolution iran ak ñi joxé seen bakan ngir taxawal revolution bi ñugi taambalé yeggu yeggu yi ci joxé juroom ñaari xabaar laakku faarisi bes bu néekk.
mbébét yi:
1- Tasaaré aada gu muñu ayib ak défar ayy nitt yu nité ak fuñu mana néekk tékko ñi ayy jaagalé al xur'aan
2- Joxé xabaar ak xew xew yi jem ci waallu yeggu yeggu al xur'aan ci biir réewmi ak bitim réew
3- Gëstu xabaar ak déeñko ak aar xalaatu al xur'aan ci mbooléem faannyi
4- Tasaare ligéeyi ci mbooléem faan ci al xur'aan moo xam xam xamla wala caada wala aada wala politique wala dundin wala …
5- Tuxel jawwu al xur'aan gi néek ñi iran ci mbooléem xéet yi néek ci aduna bi yep
6- Féxé ba yekëti yëewuk nitt ñéep ci al xur'aan ak fuñu mana néekk
7- Wéeño xam xamyi ak royukaay yiga xamné daño amukk tawféx ñi mbooléem faanniyi ak wéeño program yi jem ci al xur'aan ci biir réew mi ak ci bitim réew
8- Sos ayy waxtaanukaay ak sootanté ayy xalaat ci faann yep tekko ci al xur'aan
li gëna am solo ci yeggu yeggu yi:
Yeggu yeggu këru tasukaayu xabaar bi di iiknaa dinañuko léeral ci toombe yii di ñaw:
1-Gëstu ayy xabaar bes buné ak ayy waxtaan yu wuuté ci ayy faan yu wuuté jemaléko cit as xzbaar.
2-Amal ayy toog waxtaan ak ayy sootanté xalaat jemaléko ci tasxabaar ci téewaayu borom gis gis yu rafét yi ak ci séen xél naañ jem ci tasxabaar ak njiit yi.
3-Binde ak tasaare yéenekaayu xabaar bu tuddu (raayixe) ci ñaari ayu bes bu néekk.
4-Téew ci bërebu xabaar yi ak mboléem xew xew yi ak programe yiñu jagléel al xur'aan moo xam ci biir réew mila wala bitim réew.
5-amal ayy toogaayu waxtaan yooxamne nii dañukoy jagléel ayy nitt yu raañéeko loolu bookuna ci yeggu yeggu iiknaa ak waxtaanée mbooléem sujet yi jem ci xabaar ligéey bii nak ci anam bu muñu ayib lañukoy jaarale aande ci ak ayy serwiis yu wuute teyy yeggu ci xabaar te baayi xel nak ci tombe bicii waxtaanée waxtaan yi nak ci téewaayu ñi séen xel naañ jem ci tasxabaar ak borom gis gis yi lañukoy amalée.li iiknaa ligéey ci juroomi att yii wés menañuko tëkk ci amal ak gëstu 1200xabaar ci 35 laakku yu wuute ci 30 bërëp ci biir réewmi ak 15 bërëp ci bitim réew ci atum 1390 ci atu iran.
sérwiisu taskatu xabaar yiñii tiitaroo ci wénéen waal ci mboolo al xur'aan mooy ñiga xamne bes bu yaala saak dañi amal ayy xabaar ci aduna bi yep bokuna ci tiitaru serwiis bi boku giñi njiitu revolution iran bi bokk ak njiitu yuñu woormal ci republique islaamik iran ñigana bari ci njiitu iran yi si mboolo mi lañu bokk.
tasaare bataaxal yiñi jagléel xabaaru al xur'aan(raayixe) bokkuna ci yeggu yeggu këru tasukaayu xabaaru al xur'aan bii di iiknaa ci dëg dëg bataaxal bii di raayixe dañ ñii dajale mbooléem xew xewyi gëna am solo yiga xamne dañkoy séet séetaatko ci serwiisu xabaar yu wuute ci iiknaa, ngir jott ci léen ci mbidyi lu ñu yoombal la te ñi laamiñ bu yoomb lañuko bindé((iiknaa palantéeru léer la bu tijéeku ci aduna bi yepp))mbëbëtu këru tasukaayu xabaar bii di iiknaa nitt ñéep la soxal ñugi saaku ñaan ci imam zamaan gir mana yéegali suñu yéene yu kawéyi.
|
|
|